audio audioduration (s) 2.29 12.5 | sentence stringlengths 26 118 |
|---|---|
soo ko bëggee gis demal ca baar ba nekk korniis | |
man géeju ndaayaan laa jëm lan la woon | |
dafa daanu ci saaku bi nappaaje tamaate ji yépp | |
ndax xam nga li may yég bu ma lay xalaat | |
Nit kooku wuusu naa ko bu ma ko tuddati | |
suba su nekk xale yu góor yeey suqi wudd mi | |
safara sa gandeer na feykatu safara yi | |
soo maccee lu bare ci soon ji dangay xawa màndi | |
lóqati ju xonq te wow la nit ñi taamu | |
dama la doon suturaal léegi nak delloo ma sama xaalis | |
keesu meew laay jën waaye du nu àggale weer | |
maam ji wax ko li mu koy wax mu dem | |
bàyyil sa ndigg li ngay biij booy dox | |
ma juddu fi ba tollu nii te yow yegguloo fa nga jëm ba tey | |
bu nu jógewaan ekool dem jéexaatu gerte ci tool yi | |
mbey mi baaxul ragal nañu xiif am ci réew mi | |
bëgg naa la maa la raw mënu koo fey | |
bala ngay jél alalu jaambur danga koy tàggu | |
danga leen di soreyanteel ndax ñu baña xeex | |
mu taseeg genn góor mu saxar ko góor gi né ko baay foo jëm | |
xamuma lu waral kóolute gi nga am ci moom | |
ba màndikat ba daanoo ndaw si dafa ree ba kekku | |
dafa bëggoona nëpp nëppal biiru doom ji | |
tilim ja ca màrse dàlay teey sama xel | |
bidoN bi mën na def ñetti liitaru dëwlin | |
dafa bëggoon tukki waaye paasam matul | |
yóbbuleen xale yi dispàñseer ñu ñakk leen | |
ba màndikat ba daanoo ndaw si dafa ree ba kekku | |
ndax man naa witt ay xob ci sa limoN gi | |
seen par parloo bee tax duñu déggoo | |
suubkat yu bare kulóor yi rekk lañuy jëfandikoo | |
luxuskat bi jommal na seetaankat yépp | |
lellil fi wextan wi laal ci tëll bi | |
palpale yi nga gis bitim réew lañu lenn di jaaye | |
ndam duq ndam dàññ ndëjër ndam jëlal puum | |
dañu ko fa yónni ngir yëddu waa amerik yi | |
xoolal góor gi ak téere yi mu ràngoo ci kow yëre yi | |
mbaam mu të mii dina tax ba saxaar raw ñu | |
ku giroo may la dee ngën bokà ndap | |
lu ñu dagge sa butitu njurukaay ak lu ñu la mayoon | |
bi kumba dellusee mu jox ko benn pusó ag genn ràbbu né ko | |
jataay bii dina tax ñu gëna xamante | |
dafa la teeylu ba ngay bëgga toog mu xëcc siis bi | |
am na ñax mu nu daan foye xuusmaañàpp | |
xale bi laaj ko loo dagge sama butitu njurukaay | |
randalal doj wi bala ci nit di fakkatalu | |
jigéeni Naar yeey faral jaay tusngal | |
sunu dawkat yeey joN ante ak yu marok | |
dina ñu xam né basi góor a koy bey dé Na ñu dox rekk | |
man dey xiif naa te kii dinaa ko reere | |
janq boobu dafa njabur moroomam yi dañu ko fi teg | |
xanaa boo bëggee jaay sa soow mi dinga wut ab nattukaay | |
dafay defar sàkket moo fax mu soxla findfeer | |
dama bëgg xam këf ki mu dugal ci waxande wi lu mu doon | |
sa xar maa ngi goor de mba du dafa feebar | |
Nee ñu su biddéew yi feeñee du taw | |
kou di foo yébou dem fësë ngor yakhou | |
léegi wute na ak ba ngay yagar yagari di dem | |
dafa ko fekk ci biir i nawleem teral ko | |
mu ni leen xanaa mbënn gi amul ndox | |
buur tarasa ni ki ma xeexaloon moom la baayam def nii | |
boo bëggee reeni soor soor dangay dem ca tefes ga | |
mbañeel rekk a waral li nga wax ci moom | |
boo jaayee sa xaalis këtt ne jonn nooy def | |
boo xamatul fi nga jëm nga dellu fi nga jóge | |
ki leen nekkaloon ci xarala gi di seen xarit omar | |
doomi soxnasi sax bi ñuy génn dañu doon daw | |
lu béréf fétafétà dal ci and àm | |
fas wi dafa xoox ndax yoon wi dafa yàgg | |
yaax jën wu ñu bëgg la moo tax mu jafe | |
buxéet mbubb ak tubéy malaan a ngi | |
saali uul lañuy nëbal def ko netetu | |
lëf boo ko dooree nanga ko yeggale | |
maa ngiy tontu ci laaj bi aju ci nenukaay yi | |
as jén lañuy def ci dóolinka gi ngir duumat jén yu mag yi | |
màrse bépp wër naa ko waaye gisuma fa ñebbe | |
fekk làq na benn xuuge ba ca ron lal ba | |
fiir ga rax na demal seet ndax jàpp na dara | |
mbuumbànd bokk na ci po yi ñu lim ci téere bii | |
dafa la teeylu ba ngay bëgga toog mu xëcc siis bi | |
Naka ñu sukk di lekk ba mu yàgg caat mi ni | |
su nu amee ab pas pas dina nu ko mana def | |
xale bii kusug neen rekk kenn manu ci dara | |
bésu tamxarit nit ñi baaxoo nañu di tusngalu | |
maam ngeesu ak biram yaasin ñoom ñoo bokk baay | |
coow lee ma fàbbi ba am lu ma rëcc ci waxtaan wi | |
boyeti sum yii yépp bitim réew lañu jëm | |
bëggoon na nu jaxase waaye mënu ko | |
waxambaane bilee reeloo mbooloo mi ak gaññaxoom yi | |
looy juun juuni ni ku yàkkamtee dem | |
lellil fi wextan wi laal ci tëll bi | |
kou khësté wëkhé f ngë loo d on | |
jaayatuma gerte caaf léegi maa ngi ci fëgg jaay bi | |
booba jamano nag yi dañu om ba ngay janoo ak seen faar yi | |
ñu jël ko teg ci fas yi dawal wuti dëkk ba | |
mpicà su bañé déh àg suuh là ñél | |
ñu dàq dàq nag yi të né duñu dem mukk | |
man kay mayuma ko lam bi dafa ko këf | |
xaaral mu xippi nga jël furno boobu |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.