Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
audio
audio
text
string
lang
string
source
string
license
string
duration
float32
yàlla mayna ko taar waaye bu wayee itam nga yéemu loolu lañu ni moom la wax ci conference ba
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ab jkat rekk laa
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
suñu saaliyu mii dafa xamul ku muy takk
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
moom itam mu ngi fi dafay financé ay projets jigéen ak yeneen projets yoo xam ne nii ay programmes la yoo xam ne etat bi def na ko
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
même booy xool planification bi dina compliqué trop ñu respecté li nga xam ni moom mooy moom mooy waxtu wi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dagg a ngi bare kajoor bawol ak jolof
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ellëg la ndaje ma na ku nekk ñów ak sa ëlléer
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
voilà su su am na taw yoo xamante ne tamit su ko tawee yenn taw yu rëy yi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndaxte ñoom daanaka yoon da leen a muumaloo
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mu ngi ne temm ne dafay génn kër gi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
loolu lu may dund la là jotoon nañ ma koy nettali waaye dama dund ak ñoom
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndax sax bii ni muy yàqee ak
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
donc fra mooy lan
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
voilà dinañ mën a jokkoo
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
booy xool ci wàll benn hectyare rek ñun li ñu ci xam mooy di def quarante à cinquante tonnes yoo xam ne ñu ngi ko def ci tos ci ci tool bi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
matal naa sama liggéey
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
danaa ñëwaat si yow monsieur guèye waaye laata may ñëwaat si yow ma jox sa naataango bi kii di sadio deme sadio monsieur guèye avancé na lu bëri jëm si wàllu li nga xam ne mooy mbay mi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
man nga leen a lim
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mu dal di ne jinax ja yalax ci seen biir
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
looloo ma yóbbe ma daldi tàmbalee bind ci làmmiñ wi ma nàmp
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
voilà li ñuy conseiller béykat yi di ko dalee ci ni ma ko waxee sànq rek ca tànnam jiw bi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mais loolu c est interessant
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
waaw
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
booy jëfandikoo kaarite sedd bi du xar sa yaram
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mu daal di def safaan ba
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
kenn dalalu leen
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
góor nga leegi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ci biir dëkk ba amoon na ñaari pénc yu réy yi ñu defare doj
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ay waat yu ñu jaxase la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
légét bi woon ci taban gee tax ñu xàmme ko
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
amna li rëy lees war a def
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
kon nga monsieur diakhoumpa
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
moo nuy teree woor guddi ngir kooram ga
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
noo ngi summeeku
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
amu ma jabar
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tom am na kawar yu gàtt
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ba mu ko ko yégalee dafa dellu ci saa si
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
darou thioub laa bëgg dem
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
léegi ministère bi chaque fois day prévoir ay xeetu mbéy yoo xam ne ay xeetu mbéy court court cycle mooy kii bi kii bi maanaam kii bu gàtt lu muy soxla si ndox bëriwul ah comme du mel ni comme ay ñebe
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
cóola giy gillee ci ruq boobu kenn mënu ko muñ
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
boo demee seen kër guddi sómbi lay reere
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
waaye charles demoon na ca iniwersité ba nekk ca trinity college cambridge fimu jàngee anthropologie ak archéologie ak istuwaar bu xóot jëlee fa ab ñaar ci ñaar ab lijaasa bu ñaareelu kalaas bu gëna ndàw
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
diggante seleki ak sigicoor ñaar fukk ak juróomi kilomeetar rekk la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
sama ay collaborateur la ñu
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndax wànq moom mi nga xam ne ne de mi ngi yàq yàq waxtu fii nii nii
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tom indi na ay tóttoor
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
yaa ngi niru ku nàyyi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
macha ar allah ar
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
boo nelul boppu xale bi doo mën faj góom yi bu baax
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
bu bëggee dara ci yow dafay neex làmmiñ
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
waaw salane tine
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mànduwaar gaal gu mag grand bateaux
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
amna ku ma gis
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ku ngeen ci jokkoo vraiment ñun daañu ci am information te xam naa ne balaa émission bi di jeex amady ba dañu laaj numéro yi contacts yi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dangaa jaaxle ba mu ëpp
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
moo ngi bàyyikoo ci dëkki asi yi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
maa ngi lekk mburu
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
terrain bi dafay am solo maanaam balaa ñu fay def dara
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ku bari ay man man laa
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
am nga ay gone
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
rôle lu ancar d abord mooy ak ànd ak waa anpej
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
amoon nañu aw fas wu nga xam ni ku war jox xa moroom
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
bul laal sama wata
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ay kilifaa dem ca buntu dëkk ba gatandu gan yi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dañuy xaar ba mu ow ba pare après door ko xolli dangay xaar ba mu ow ba pare après door ko xolli après denc ko waaw loolu moo lay mën a permettre nga am gàncax bu normal boo ko jiwee
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dafa bari xalis lool
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
jumtukaay bu ñuy seete sellaayu ndox mi la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
fluke bind na ni ñenn ñi jotu ñu mëna tere jigeen ñi wax ci seen wergu yaram
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
su ñuy demee ñoom ci ñoom
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mu ni bu ngeen yeboo rey ma ma fekki sama mag ja
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
bisu tay bi dafa rafet
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndeem soob na yàlla
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
nawet dafa war a nekk kumpa ci ñun
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dafa am njaboot gu rëy
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
yobanté bu cà huloo amé défà jar
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
damaa ragal a dee
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
parce que foofu amul subve ntion
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
buleen bàkkaar kenn sànniwu ko kort
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
noo ko moomoon
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
moo tey ni muy doxe maamam lay kókkali
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ça c est les armoires les armoires di nga gis armoires yi ñooy commandé kii léegi da ngay da ngay bës bouton rek affaire déclenché s il y a problème aussi ñoo lay signalé daf lay signalé problème yii am na nga mun arrêté
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ban oto mooy jaar cité port
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
hangi lañuy faral di jëfandikoo ngir togg reer bu am istili saaf bu yàgg
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
li ma gis dafa mel ni lu am melow nit
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ngir lii dañoo wara tàggale bërëb yi ak gaal angalteer yi ca isipt tamit yoyu jëf gaalu xare yu itaali xalaatuñu ngir def dara
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
te sax làkk woo gis am na lu mu yoreel moroomu làkkam
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
taw bi daan nga am
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mooy taw yooyu nga xam ne day mën a indi ay yàqu yàqu
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
et seen wax bi am na importance lool lool lool
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
génneel nañu porose bi xaalis bu takku
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
bamu taa nga di ko jaxase ak say yoxo loolu mooy rimb
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ba ñu ci tegee ay fan njaag takku fas yéené xeexi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tas séy dagan na ci anam yii
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
waaye si nawet bi nga xam ne ñu ngi wax ne xëy na mu taw xëy na mu yem fii ci wàllu niñ ko war a saytoo ba lépp luñ ci mën a am lu mu néew ak mu bëri ñu mun koo denc dencin wu mucc ayib ñu mun koo jëriñoo
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
sama lam bi furi na war naa koo sóob
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
castors
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dinaa dem ginaaw bi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
luxembourg yàgg na bëgga maanu wayé alëmaañ moko moomoon ci xare bu wër addina i ak xare bu wër addina ii
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mu méngoo ak benn hactare askan mi ma yaakaar ñu déggee ko noonu mu gën a leer bu ñu jógee si loolu ñu ne lan moo tax tey ngeen koy boole ngeenay jël produit bi di ko booleeg def si machine
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
nekk naa it jkat
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
End of preview. Expand in Data Studio

Bocalantics

One normalized, license-clean speech corpus for West African languages — Wolof, Pulaar/Fula, and Bambara — merged from the fragmented community datasets into a single source you can train on anywhere with load_dataset.

West African languages are spoken by one interconnected, multilingual people; Bocalantics treats them as one corpus so a single model can learn across them.

Schema

field type
audio Audio (16 kHz)
text string — the transcription
lang string — wo / ff / bam
source string — upstream dataset id
license string — upstream license
duration float — seconds (0.0 where the source omitted it)

Splits: train / validation / test.

Composition (clips)

lang clips
bam 38769
ff 17253
wo 86729

Provenance & attribution

Built only from clean-licensed sources, each row carrying its source and license. Please credit the upstream creators:

source lang license credit link
soynade-research/Wolof-ASR-Data wo CC-BY-SA-4.0 soynade-research link
ngia/ASR_pulaar ff CC-BY-4.0 ngia link
RobotsMali/bam-asr-early bam CC-BY-4.0 RobotsMali AI4D Lab (Jeli-ASR, Mali-Pensé / A. Ouattara) link

License

The collection is released under CC-BY-SA-4.0 (the share-alike umbrella, since one source is CC-BY-SA; the CC-BY sources are relicensed into the collection with attribution preserved). Attribute the upstream creators above.

Load

from datasets import load_dataset
ds = load_dataset("MOH749/Bocalantics", split="train")
# per-language: ds = ds.filter(lambda x: x["lang"] == "wo")

Roadmap

  • v1.1: add Sereer + more Wolof/Pulaar via Kallaama (CC-BY-4.0, Jokalante), once re-hosted from github.com/gauthelo/kallaama-speech-dataset.
  • Mande siblings (Soninke, Mandinka) await licensed speech data.
Downloads last month
130