text
stringlengths
237
100k
karara REUNION les membres du club sont convoqué à la reunion ce samedi 15 dec à 16H c aloba (ouagou niayes en face mosqué niarry tally )SG du club .. nous comptons bcp sur votre presence anciens et nouveau membre il sera difficile pour les nouveaux de participer à cette rencontre vu ke les ancienski font vivre ce club...
Mbootaayu Réewi Jullit yi Mbootaayu Réewi Jullit yi gii mi ngi sosu ci saxal goo xam ne buur ak njiiti reewi jullit yi jëloon nanu ko, ci waxtaanu seen daje bi nu njëkk’a daje, te defe woon ko Ribaat, peeyub reewum Marok, ci diggante 9 – 12 /8/ 1389 g.g , deppoo ak 22 – 25 /9/ 1969 g. Ñaar-fukki reewi lislaam ak juroom...
Baraay Ci Jëmm, baraay ab delluwaay la bees di sukkandiku ngir xam ñaata yoon la genn feeñte guy tóllantiku di amal ag tóttantikoom ci benn diiru jamono bees jël. Maanaam ñaata yoon la xew-xew bi di feeñ, ci genn anam gi, ci benn diirub jamono. Ngir natt baraayu genn feeñte dañuy jël benn diiru jamono xool ñaata yoon l...
Xaralay xibaar ak jokkoo Xaralay Xibaar ak Jokkoo (XXJ) walla Xaralay Xibaar ak Jokkoo yu Yees yi, ci wu-angalteer Information and Communication Technology, ci wu-faraas Nouvelles technologies de l'information et de la communication, moo ëmb mbooleem xarala yees jëfandikoo ngir yor ak jokkale ay xibaar. Yitteem mooy so...
style="display:inline-block;width:468px;height:60px" data-ad-client="ca-pub-1433917768187213" data-ad-slot="9368633314"> IMAC/IPHONE users click here svp rfm ne marche pas sur le net de façon continu qui peut maider YENAGUI DEFE SENE LAGUE BO BAKHE LIS MO AM SOLO ZI REW DI DIAFE YOUSSOU NDOUR merci rfm tfm dama lena be...
World Wide Web World Wide Web manees na koo tekkee niki digg lënd gi (lënduk jargoñ) kon ana numu def ba tuddees ko digg lënd ? ndax moom la àdduna bépp ànd di jëfandikoo ku ne jàpp ci génn lawtan fa lawtan ya daje lees tuddee digg lënd moom nag manees na koo jëfandikoo fim ne ci àdduna bi yépp, gox yépp man nañu cee d...
KOÑSEY BI ÀND LIGGĖEY AK PAAP BI Kerceen ak Jullit : XIBAAR CI MUJJANTALUG KOOR GI ‘Id al-Fitr 1430 H / 2009 A.D. Jullit yi, sunuy xarit 1. Ci mujjantalug weeru Koor gi, bëggoon naa leena wax sumay yéeney jàmm ak mbégte te, jaarale ko ci bataaxal bile, ñaax leen nu ànd xalaat ci lu jëm ci itte bile : Kerceen ak Jullit,...
Wàll:Jëfandikukat wo-1 Jóge Wikipedia. Dem : Joowiin , Seet Xët yi ci wàll gi « Jëfandikukat wo-1 » 4 xët yii bokk nañu ci 4 xët yi nekk ci wii wàll. B Jëfandikukat:Belladon J Jëfandikukat:JimeoWan L Jëfandikukat:Lodewijk Vadacchino S Jëfandikukat:SF-Language Ci « http://wo.wikipedia.org/w/index.php?title=Wàll:Jëfandik...
Mikroneesi Bii seddatlin nga xam ne Kureelu Mbootaayu Xeet yi moom la jëfandikoo suy seddatle àdduna bi ci ay Diwaan, gëstukat yi ñoom seddatle bu bees bi la ñu taamu, moo xaaj Oseyaani ci ñaari diwaan: Oseyaani gu jege ak Oseyaani gu sori yi Mikroneesi box. Baatu Mikroneesi waa faraas bii di Jules Dumont d'Uville moo ...
Doxalukaay bu demandoodi Doxalukaay bu demandoodi ab xeetu doxalukaay bu mbëj la bu dawaan bu safaanu bu xél yu wëndeeluwaan bi yamul ak yu toolu bijjaakon buy wëndeelu bi lëmës yi nekk ci tekkaaralaan bi jur. Maanaam amul ag demandoo ci ñaari gaawaay yi, benn bi moo raw beneen bi. Loolu moo ko wuutale ak doxalukaay bu...
Kàttan Tëraliin Tekkeem[Soppi] Kàttan mooy man a def dara (sos ag soppi), kàttan nag am na ay melo yu bari, yi ci ëpp solo ñi ngi feeñe ci tàngoor ak leer. Ci biir “xam-xami dénd yi” (science naturelle) kàttan man na fee jël ay melokaan yu wuute : “kàttanug tàngoor”, “kàttanug kimyaa (simi)”, “kàttanug mbëj”, “kàttanug...
Xiirtalug mbëjbijjaakon Xiirtalug mbëjbijjaakon ag feeñteeg jëmm la gees di gis niki juddug ag wuuteeg aj ci diggante ñaari cati ab wommatukaayu mbëj walla ci ag ndombo gu mbëj mbaa juddug ag dawaanu mbëj ci seen biir, su wommatukaay bi walla ndombo gi nekkee ci biir ab toolu bijjaakon. Ci gii feeñteg jëmm la doxub sop...
Jóge Wikipedia. Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal Mbooleem beeñ bi ak doj yi ñoo sos wàll gu tond (superficiel), gu dëgër gu kol-kolu suuf si, ñu koy woowe Jéeri ji walla aji wow ji.
Waax ngua deugue de. Moyoulma wa Corps de la paix, gnome ils parlent les dialectes sans accent. Il y'a une copine ki m'a raconte cette histoire tellement rigolo . Tu sais comment nous Senegalais nignou meune dieuwe , deux marchands ambulant voient un blanc avec son boubou "ndiakhass" et un gros sothiou, assis tranquile...
Jóge Wikipedia. Nosukaay ab wuutuloxo bu mbëjfeppal la buy seggat ay xibaar yu ñu ko jox jaare ko ci ag noste gu xellu gu ñu tëral-jiital. Ci wàllu xibaarfeppal la ñu koy jëfandikoo. - Français: ordinateur - English: computer, di tekki waññikaay, ndax yi ñu ci njëkk a defar waññi rekk lañ doon def.
Doxalin bu jappake: Windows 7; Windows 8 Microsoft Windows 7 - 32 mbaa 64 bit OS Tëriin Microsoft Windows 8 - 32 mbaa 64 bit OS Karmat: Baal nu wérlu ne samp nga Sayi Cër yi mujj ngir sa nosteg doxal ngir am jàppandalug làkk wu mat ci sa làkk. Bépp sottib Office 2013 muy toppaan am déet bu am Microsoft Excel, Microsoft...
Aloos Ci angale mooy aloes; Ci faranse mooy aloès Bantu genn garab la bu xeeñ lu neex, te joxe diwlin ji ñu def ci néew yi. Ci réewi penku yi la jóge. Boroomi xam-xam yi ci turu Akilariya agalosa (Aquilaria Agallocha) lañu ko xame. Garab yi am benn feebar rekk ñooy xeeñ. Feebar bi dafa soppi wàllu dàttam ba bant bi dëg...
Dencukaay Ci xam-xamu nosukaay, ab dencukaay walla ab taxañ, ab ëmbukaayu ay xibaar la. Dencukaay yi, dañu leen séeddale ci ñaar: yu ëmb ay mbind "dencukaayub mbind" ak yu ëmb aw yoon wu ñaarñaarloo "dencukaayub ñaarñaarloo". Cig xarala, njoxe yi nekk cib dencukaay dañu leen nos niki ag callalag ay bit, ñu boole leen n...
Toolu bijjaakon Toolu bijjaakoon, ci jëmm, ag feeñte la gu màndargaloo ab taraay ak ab jubluwaay bu jenn doole, jees duppee Dooley Lorentz, ju judd ci doxub ay yani mbëj. Toolu bijjaakon, moom ak toolu mbëj ñooy ñaari cëri toolu mbëjbijjaakon di li banqaasu jëmm bi di mbëjbijjaakon di faramface. Soo boolee ay duusi ab ...
1:1 Man njiit li maa leen di bind, yaw soxna su tedd si, yaw ak say doom. Bëgg naa leen bu wér ci sama xol, jéllale naa sama bopp sax, waaye itam képp ku xam dëgg gi. 1:2 Te dëgg gee tax nuy def noonu, dëgg gi dëkk ci nun, tey ànd ak nun ba fàww. 1:3 Yàlla Baay bi ak Yeesu Krist, Doomu Baay bi, dinañu nu may yiw, yërma...
Bunt: Xarala BUNTU XARALA « Xarala ab baat la bu yaa ñeel lepp lu jëm ci jëfëndikoo walla xamtey jumtukaay ak xereñ gu nit jëmal-kanam.» Ay wall Mbëj Mbëj dadi ab feñfeñ gu gisuwul ak bët gu’y feñ ci ag wootal walla bëmëxënte ci digante yanub mbëj yi. Ci gattal mooy bepp feñfeñ gu juddu ci jamarlo gi nekk ci ...
Imbraatóor gu Mali Imbraatóor gu Mali ba ci xarnub XII, xamalu nu ko woon lu bari. Ci li tegu ci atum 1150, la nu xam tur yu mel ne Hamana, Jigi Bilali(1175-1200) ak Musaa keyta di ko wax itam Allakoy (di tekki neex yalla). Mi ngi yamoon ci Mbàmbulaanu Atlas ci sowwoom, Dexu Niseer ci penkoom, tay ñuy yii réew: Mali, S...
Fànn Fànn, ci tekkeem gu yaa, dafa ëmb bépp yëngu-yëngu nit - muy lu kenn walla mbooloo di def - moom, su sukkandikoo ci gisiin yu xereñ, ñaw ak doxaliin wu bawoo cim njàng walla cig yàgg-jëf, mooy tax a man a biral genn kàllaama gu taaru gi. Ci fireem gu tay, fànn dees koo féetale ak man-gee jokkaley yëg-yëg, ba tax k...
Jóge Wikipedia. Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal Kamerun am réewu diggu Afrig la, jëmmam dafa mel ne ab ñettikoñ, rëye na 475 442 km², 98,8% di suuf, 1,2% ndox la, di 42u réew mi ëpp ci àdduna bi, am na it 402 km ci tefes. Réewum Niseer...
Treize des 24 listes nationales en lice aux élections législatives ont fait élire au moins un député. La coalition Benno Bokk Yaakaar (BBY) de la mouvance présidentielle a remporté 119 sièges des 150 qui étaient à pourvoir. L'opposition prend le reste, 31 sièges. Voici la liste - provisoirement publiée par la Commissio...
Kajoor Tëraliin Cosaan[Soppi • modifier le wikicode] Kajoor mooy kàdd ab garab gu nekk Senegaal ak joor, suuf si. Moo jur baat boobu kajoor ci wolof. Ñi jëkka yor suufi kajoor, ay séeréer lañu woon, ñu doonoon ay lamaan te sant JAAÑ. Ba pare, xeetu wagadu ak jafunu, soqi ci sooninké yi, jóge ca penku, ñoo sos meeni jëk...
Dans cet épisode Xuman et Keyti reviennent sur: – le rapport de l’IGE pour la période 2008-2013 qui fait de grosses révélations sur des détournements, surfacturations et autres du régime du PDS. – la mort de Ismaïla Faye au Maroc et ce racisme dont on ne parle pas assez mais qui a son lot de victimes. – l’expression en...
- Limogeage de Abdou Mbaye au poste de 1er Ministre et son remplacement par Mimi Touré. - Bien mal acquis: Tahibou Ndiaye accusé pour 7milliards paye 3.4 milliards et évite la prison. - Guerre en Syrie: Qui manipule qui? - Promesse de maris faite par Macky Sall aux femmes lors de la campagne présidentielle. Productions...
Bëj-gànnaaru Aamerig Bëj-gànnaaru Aamerig ab gox la bu nekk ci Bëj-gànnaaru xaaju kol-kolu àdduna bi, féete, ci penku Mbàmbulaan gu Dal gi, ci sowwu Mbàmbulaanu Atlas, ci bëj-saalumu Géeju Dottub Bëj-gànnaar gi, ak ci Bëj-gànnaaru Aamerig gu bëj-saalumu. Mooy làccu bëj-gànnaar wu goxu Aamerig. Ci bii gox ñetti réew yu ...
Ancos ci Siri Ancos, ca jamono Injiil, péeyu diiwaanu nguuru Room bu tudd Siri la woon. Dafa nekkoon ca wetu joor gu naat ca dex gu yaatu gu tudd Oront (fleuve Oronte), 32 kilomet ca kaw bëlu dex ga, maanaam fu dex ga dugg géej ga. Teeru Ancos moo doon ca dëkku Selusi, bu nekkoon ca Géej gu Mag 8 kilomet ca noru bëlu d...
Ñaareelu Xareb Àdduna Ñaareelu Xareb Àdduna bi ab xare la woon bu laaloon àdduna bi. Mi tàkk ci bi Almaañ ak Itaali ak Imbratóor gu Sapoŋ bëggee noot àdduna bi ci diggante 1914-1918 g.j. Ñaari réew yii mu ci nekk daw na wuti ndimbal ci li ëpp ci réew yi mu defal ay tappoo. Bu ko defee yàggul dara lu bari ci réewi àddun...
Jóge Wikipedia. Ci angale mooy Areopagus; Ci faranse mooy Aréopage Bérab ci biir dëkku Aten la, bu nekk ci kaw wenn tundu xeex wu kawe. Amoon na ay siis yi ñu defare woon doj ngir kureelu dëkk ba manoon faa daje. Indi nañu Pool foofu ngir mu waareji (Jëf 17:18-34). Areyopas ni ñu ko gise tey ji su fekkee ne yaa ngi ca ...
KURÉEL GI ÁND LIGGÉEY AK PAAP BI XIBAAR CI MUJJUG KOOR GI Yar ak a yee ndawi kerceen ak ndawi lislaam ñi Sumay xariti jullit yi ma sopp, 1. Xumbal bi ñuy xumbal ‘Id al-Fitr’, muy mujjantalug weeru koor gi, dafa nuy may mbégtem jottali leen yéeney doomi baay yi bawoo ci Kuréel bi ànd di liggéey ak Paap bi ngir waxtaan a...
1:1 Li jiitu tey Yàlla waxoon na ak maam ya ci wàll yu bare ak ci tëralin yu wuute jaarale ko ca yonent ya. 1:2 Waaye ci mujug jamono jii nu tollu, Yàlla wax na ak nun jaarale ko ci Doom ji. Doomam jooju la Yàlla jagleel lépp, te ci moom la Yàlla jaar, sàkk àddina. 1:3 Doom ji moo di leer giy jollee ci ndamu Yàlla, di ...
Albert Einstein Albert Einstein (juddoo Ulma (Almaañ) ci atum 1879, faatoo Princeton (Diiwaan yu Bennoo yu Amerig) ci 1955) doonoon na ab boroom xam-xamu jëmm, xaymakat, xetlukat bu waa Almaañ bu jëloon réewu gu waa Suwis, te mujje ca Diiwaan yu Bennoo yu Amerig. Lu weesu doon gi mu doonoon kenn ci jëmmkat ak xaymakat ...
Polineesi Bii seddatlin nga xam ne Kureelu Mbootaayu Xeet yi sax mooy la jëfandikoo suy seddatle àdduna bi ci ay Diwaan, gëstukat yi ñoom seddatle bu bees bi la ñu taamu, moo xaaj Oseyaani ci ñaari diwaan: Oseyaani gu jege ak Oseyaani gu sori yi Polineesi box. Diwaan bi dafa am meloow ñettkoñ Baatu Poloneesi waa faraas...
Abadon Ci làkku ibrë (אבדון) la tur wi jóge. Ci angale mooy Abaddon; Ci faranse mooy Abaddon Turu malaakam kàmb gu xóot gi la, ci làkku ibrë bi ñu sotti ci làkku gereg. Tur wi ci gereg mooy Apolyon. Dafa tekki 'yàqkat'. Dafay wax ci buuru njéeréer yi ñu gis ci téere Peeñu ma ci Injiil (Pe 9:1-12). Lu ëpp ci boroom xam-...
Njëkk-taariix Ak juddug mbind taariixkat yi am nañu ay wayndare yu leer te yaa yees man a sukkandiku ngir man a taxawal toftaloog xew-xew yi yiy biral digalub jamonoy taariix yi. Xaaj bu yaa bu taariixu nit njëkk sosug mbind, ci xayma, mi ngi door mat na 200 junni at, ba jëmm ji njëkk jees man a nattanleek nitu tay jii...
Duni Kanaari Duni Kanaari yi (ci wu-ispaañ Islas Canarias) ay dun lañu yu bokk ci goxu Afrig, féete ci bëj-gànnaar-sowwu Afrig nekk ci mbàmbulaanu Atlas, te bokk ci réewum Ispaañ. Ñoo ngo ko Séddale ci ñaari tund Santa Cruz gu Tenerif ak Las Palmas. Gongikubaat[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Turu duni Kanaari ngi jëlee ...
Senegaal |Réewum Senegaal| Barabu Senegaal ci Rooj |Dayo||196,723 km2| |Gox||Afrig| |Way-dëkk||12,853,259 nit| |Fattaay||59,26 nit/km2| |Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |Pénc Maki Sàll Mohamed Dionne |Tembte - Bawoo - Taariix |Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |Làkku nguur-gi||wu faraas 94...
Taariixu Aamerig Tëraliin - 1 Feeñug Diiwaan yu Bennoo yu Amerig yi (U.S.A) - 2 Sancu yi nga xam ne waa Angalteer yi taxawal nañu leen ci Aamerig gu bëj gànnaar gi: - 3 Noste gi doon doxal mbiri biir yu sancu yu Angalteer yi: - 4 Li waraloon xareb temb bi: - 5 Yoon yuy tege galag ak tembar - 6 Yoon wi aju ci moolu (nav...
Seex Anta Jóob Seex anta jóob a ngi judd ci 29 tabaski ci 1923 ca Jurbel- faatu ci 7 diggi gàmmu ci atum 1986 ca Ndakaaru doonoon ab taariixkat bu di doomi Senegaal. Moo fésal li Afrig, rawati na Afrig gu ñuul gi indi ci xayug àdduna bi. Doonte yenn ci ay yebbeem(thèse), ba tay, am na ñu ko nanguwul rawati na ñenn ci w...
Musidɓe tedduɓe, PULAAGU.COM ena jogii weytaare mawnde noddude fedde kala ngam tawtoreede kikiiɗe mawɗo juɓɓinteeɗo to Le Havre ñalnde 4 Juko 2012. Nguu ñalngu ko mawninoowu maanditaare PULAAGU.COM kono amin njogori innirde-ngu jaltugol Firefox e ɗemngal Pulaar. Ko ɗum waɗi amin katojini e garaangal mawɓe wayɓe hono mo...
Nowel Nowel Ci bu jekk, xeetu Wolof yii maggaluwoon bësu nowel. Waaye leegi ak comercialization du lépp. Yeeneen nit ni ci Ndakaru ak yeeneen dëkk yu mag yi dañuy maaye ay cadeew ak di def lamp yu rafet ci seen kër. Li ci genn bari ci Wolof yii du nu ay catoliq walla talibe Insa, kon dunuy fonk bësu nowel. Ci sunu jama...
Paroles officielles de la chanson "Celebrate" We celebrate ,we celebrate, We celebrate cause we re all together Despite the bad wether Hoping that this would last for ever We celebrate cause we are all family Despite the differences between you and me We live in harmony yeah Ah wege yo waga waga wege yeh Ah wege yo wag...
aj Jóge Wiktionary. Wolof[Soppi] → Mottalil gongikubaat bi. Aj: - Kuy dem màkka ngir ngir wàccook juroomeelu ponku Lislaam, aji Màkka - Lu nekk ci suuf ga soxla mu dem ci kaw boo ka yëkkatee jëme ci kaw Tur[Soppi] Aj - Mooy bennte bees di nattee tangaay, walla taraayu menn mbir - Tay dëkk bi tang na, noo ngi ci 30 aj
......C'est plus sa bouche qui attire l'attention...pour le reste chére madame on s'en tamponne vraiment ; tu ne nous avait pas insulté du tout.... 5.Posté par ndeyecoumbandiaye le 14/03/2014 12:24 je ne connaissais même pas cette fille, après videao bi la guiss pour voir mannequin la , li mou defone embrasser son mari...
Catir Ci angale mooy Thyatira; Ci faranse mooy Thyatire Ca jamono Injiil dëkk la woon, ci diiwaanu nguuru Room bu tudd Asi, maanaam ci sowu réew bi tudd tey jii Tirki. Tey jii Akhisasar la tudd. Dafa nekkoon ci yoon diggante Pergam ak Sàrd, ci dig bi nekkoon diggante diiwaani Misi and Lidi. Dëkk ba siiw na ndax cuub bi...
Dans un orthographe exécrable, voici le message de détresse de cette internaute : Suis en couple avec un homme depuis plus trois ans au debut tt etait rose il maimait trop mem si dawouma defal ndakh amoul mann sakh mako donn defal mais mann lolou dou wonn problem ndakh manker wouma wonn dara dama donn diang am bourse t...
Nosteg doxiin Ci xam-xamu nosukaay nosteg doxiin, ci tënk ND (operating system walla OS ci wu-angalteer), mooy mbooleem tëriin yiy yor, saytu lëkkaloo gu jumtukaayu nosukaay bi (tappaan yi, xel mi...) ak tëriin yi nga ciy jëfandikoo. Naka-jekk nosteg doxiin gi mooy tax jëfandikukat bi man di jot ci ëmbiit li nekk ci no...
Ethiopiques numéro 28 numéro spécial revue socialiste de culture négro-africaine octobre 1981 l Gimdhi taariika fii Fuuta-Dyalon Ngaabu (poème peul) Auteur : El Hadj Thierno Abourahmane BAH Mi dho yima dhoo gimdhi mi sifanoo on Je en train chanter ici poème je vais raconter vous Fii ngaabu e Dyanke ngal langal Sur Ngaa...
Jóge Wikipedia. Kàttanug mbëj xeetu kàttan la gu lonku ci doole walla tool yu jóge ci mbëj, maanaam lu ñeel yëngug, walla doxub, yani mbëj. Kàttanu mbëj manees na koo jëfandikoo ngir defi liggéey, leeral, tàngal,... Kàttanu mbëj manees na koo natt ci dawaanu mbëj bi, balaa dara manees naa xayma liggéey bi - , Liggéey b...
Penku gu Sori Ci diwaan bii di nan fa gis ay réew yu wuute, ca wàllu koom ak xarala. Ci genn wàll di nan fa gis Taywaan ak Koom-koomam gu naat, ak dunu Hoŋ Koŋ aky taaxikawam yi gën a kawe ci àdduna bi, ak. Ci geneen wàll, ay réew yu seen koom-koom cëslaayu, ba tay, ci mbéy, waa kaw gi nekk ci coona. Limbari yi joxe na...
Les plus populaires Lecteurs en ligne 221 33 823 43 43 Partager 59 commentaires allahou akbbarr li dawna tarama al khourhan rek moy deg sa m'encourage à laisser ma fille de continuer à aprendre Machallah Mancha allah li dawna yaram trop mandeh mangui sante yala boubakh di wakh Alhamdou Lilahi Rabil Halamin ndakh sama d...
Sëriñ Tuubaa Sëriñ Tuubaa Xaadimu-rRasuul (Seex Aḥmad ibn Muḥammad ibn Ḥabiib Allaa 1853-19 sulet 1927) boroom xam-xamu diine bu jullit la bu di ab sëriñ te cosaanoo ci ag càllala gu doomi soxna. Mi ngi gane àdduna ci Mbàkke, ab dëkk bu maamaatam sancoon ca nguurug Bawol, maamaatam jooju mooy Maharam, walla Maaraam,moo...
Partager 24 commentaires vraiment toukara tu est méchant c son frère union fait la force sokore bakhoule oh c dommage Sénégal m nekh rek.prkoi ce tounkara se croit supérieur et plus inteligeant que TT l monde.revient sur terre et accorde du respect a l'autrui.en tant que éducateur,soit pedagogue tounkara a rézon si cté...
Amadou SY 11/05/2016 à 11:36 Partager Retweeter 0 Partages 16 commentaires uuuuuffffff liiiiiiiii nekhena deeeee Vive youssou diame rek lay ame youssou ndour incha allah Popopoppooooo putinnnn ça déchire. Euuuuuuh ma contaneeeeeeee C’est trs neikh vraiment diottou Ndayame limo nekheeeee hooooooo ma contane nkh nekhi la...
Mandabi Li ci xew[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Mandabi dip filmi ci Wolof bou Ousmane Sembène bokhamni dathiye netali: jen way jo khame mi da am jarbaatam bouko yoone manda nguir mou jokhko ndayam legui ay soxnam tekko allal ju bari ba tambale lep luune ndekkete yoo mandabek thiowli jounii ak niari temeer rek la ndeke...
moo waay ! 404 -------------- nu ngiy jéggalu de. dafa mel ni li ngay wut, jafe naa am ci ëttub wolof. su fekkee ni njumte bi mi ngi jóge ci ëttub wolof, di nañu yóonee been bataaxal, kiy saytu mbirum ëttub wolof, ngir mu xool lu sabab loolu. li war wéep dina ko ci def. jaajëf !
Manla fatkiné la dulcinée, done miss bou diongué té finé ni djiné bou diougué guinée diar gal séné,boul alluciné nakh dama raffiné mo takh malay fasciné parsk dama beugueu ciné ak matinée,kone boul tite béy patiné damalay takiné wayé gueumal limalay wakh parsk cé inné . devinez, fi yeup la miné , meunoto fi rimer béy f...
1:1 Man Pool, jaamub Kirist Yeesu, maa leen di bind bataaxal bii. Yàlla woo na ma, ma nekk ndawam, sas ma liggéeyu xamle xebaaram bu baax bi. 1:2 Xebaar bu baax boobu, Yàlla dige woon na ko bu yàgg, jaarale ko ciy yonentam, ñu def ko ci Mbind mu sell mi, 1:3 di xamle mbirum Doomam, Yeesu Kirist sunu Boroom. Lu jëm ci m...
Haj Haj mooy juróomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ja ni: "Tabaxees na Lislaam ci juroom: Seere amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe Azaka, Woor weeru koor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci bepp anam), ci waxi Yàlla mu kawe...
waaw Sàntar Waaw ci Ndar mooy këru artist yi te it di bérëb bu ñuy saytoo jumtukaay yi ak xarala yi. Li ñu gëna bëgg foofu, mooy dundal aada ak cosaanu Senegaal ak bu Afrig yépp te it yombal weccoo xalaat ci wàllu cosaan ak aada. Fexe it, ba di dajale nit ñu, ngir ñuy jàng di xalaat ak di liggéey. Dina mëna nekk it, kë...
Leopool Sedaar Sengoor Leopool Sedaar Sengoor mi ngi juddoo ca Jiwaalo ci 9 Oktoobar ci atum 1906, génn àdduna ca Verson (ca Fraas) ci 20 Desambar 2001. Nekkoon taalifkat, bindkat doonoon it killifa aada ca Senegaal. Mooy ki njëkk a doon njiitu réewu Senegaal (1960-1980). Dundam[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Léopold Sé...
Du yeena ma tànn, waaye man maa leen tànn, sas leen ngeen dem, meññ meññeef du sax. (1) Ken nit amoon na ñaari doom. Am bés, nu ñëw ca taaw ba nee ko: Sama doom demal tey ligéeyi ca sama toolu réseñ. Taaw ba tontu ko nee : Maagi dem, baay; waaye demu ca. Gannaaw bi, baay bi ñew ca rákk ja wax ko noonu: Mu tontu ko nee:...
Jimbulang Jimbulang aw wayndare la wu yitteem doon ëmb mbooleem xeeti xam-xam walla man naa itam tënku ci benn xam-xam, maanaam jimbulang buy wax ci paj walla ci taariix kepp. Jimbulang am mbooloom ay jukki la def, bu ci nekk di wax ci lenn: ciw nit, cib barab, cib xew-xew, cib xam-xam,... Jimbulang day wuuteek baatuka...
Skip to content dimanche 19 août 2018 Toggle navigation Artistes Actualités La Galerie Contact Facebook Bërre reenu niambila (Combat de lutte entre deux racines de manioc) Reero amul niak waxtaan mo am (Lorsqu’on s’explique, on finit souvent par se retrouver) Kiy wut fimuy fanaan ak kiuy wut kuko wettali warna gno mëna...
LYRIC Intro [ADH] Yeah yeah Yeah yeah Elzo! Verse 1 Numb to the pain, numb to failure Give none to the frauds Cause frauds won’t bail ya The streets is watching question is who watching for ya Wanna break the chains off And the fakes won’t do nothin for ya Product of my own lil town Straight from the borough of the cro...
fatalikou ak yéne si li sim Publié 6 décembre 2018 *Bienvenue sur la chaîne Senegaal TV : Le Sénégal en vidéo ! 703607252 Autres Vidéos Fatalikou : kouni lii nékhoule dagua …. Yéne djigeune gni doumaléne maye dara Déglouléne yéne gni di wakh si mane ak marie chou wa yéne li lane la si goor
KCC Mboothaye-la bi ye yangatou si wallum machinu bayekatyii nyu hameh tractor ak jumtukaye yi muwara andal beh senu legaye mana sutti si bir Senegal. Bagages nyoye Caterpillar, Komatsu, Volvo John Deere, Hitachi, Cummins, Detroit Diesel, Terex, Bomag ak Bobcat Am nen yu bepe bagage bunngen sohla sa suneh, bah pareh ma...
Papa Oumar FALL Membre de la Société civile ''culturelle'' sénégalaise Acteur culturel linguiste de formation Site web perso: STYLOCULTURE CONTACT: email@example.com *** Ci miim jamono Dëgga attan tumuranke ! Waaye moo doy cip weetal Waaye moo doy cip wettal Xoolal fenn ni muy lawe Melna geej gu aay Duus yay fewi-fewi!...
LYRIC Intro: Yeah… yeah Yo gni ngui tchi yonou wout beu legui… Khamouniou kagn la niouy nopalou Yeah… Verse 1 Def naa ay ndiaakhoum homie Homie def naa ay ndiaakhoum dolli (def naa ay ndiaakhoum dolli) Moytoul ma waa dji gueuneu meuneu noppi ndakh defkat dou aalou homie (defkat dou aalou homie) Defkat dou alou homie (n...
Ndimbal:Dalal-jàmm Dalal-jàmm, yaa ngi ci wikipedia gi ñu jagleel kàllaama Wolof, mu di jimbulaŋ bu ubbeeku goo xam ne ñi koy jàng bokk nañu ci ñi koy bind. Ku nekk man nga cee dugal sa loxo, bind ay jukki yu yees walla gën a baaxal li fi jot a nekk; ndaxte ngir sémb wi man a dox ci ni mu gëne, dafa laaj ay loxo yu bar...
Chercher amydabakh SOPEY MAME ABDOU AZIZ DABAKH RTA » Suite Design by lequipe-skyrock Choisir cet habillage Signaler un abus Abonne-toi à mon blog ! RSS Retour au blog de amydabakh Ajouter cette vidéo à mon blog #Posté le samedi 17 octobre 2009 23:08 Connecte-toi amydabakh, Posté le dimanche 27 décembre 2009 18:33 amin...
Yonent bi (YYJSM) neena ku bayyi julli, bu ngéen bokkee ndap di lek, day am tooke juy géen ciy weewam di wëndéelu ci ndap li. Ta kuci lek ap xolam lakk ta xol bu lakk daadi wow. Ta ku xolam wow sawara la jëm. Ndax sunu boroom mooni ci alquraan : wa waylun lil xaasiyati quluubuhum... Yonent bi (YYJSM) neena ku bayyi jul...
Gàddaay Gàddaay di ci fr “immigration” baat la buy tekki : tukkee ci barab mbaam réew dem ca meneen, ngir sàkku fa dara, mbaa ngir naqarig sam réew ci yaw mbaa barab ba nga bawoo, loolu di faral di jur ag tumbrànke, akug ndoxondéemu, tax ngay am turu doxondéem giy tekki ku dëkkul ca réew ma nga nekk, cosaanoowoo fa Kon...
Xëti jiriim Njoxe yii di toftal ab duppitu nëbbitu dàttub njoxe bi la, te yeesalam gu mujj mi ngi am ci: 13 Suwe 2019 à 17:53. A maximum of 5 000 results are available in the cache. Xët yiy toftal amuñuy lëkkalekaay yu ne ci yeneen xët yu leen di ubbi te ëmbuwuñu itam ci benn xëtu Wikiquote. Afficher ci-dessous jusqu’à...
Titre : TOP NOBEL (BRAHSKO/HIKHOP/M-O-G) [Ajouter ce morceau à mon blog] Année : 2008 Paroles : Ce son parle d'amour qu'un mec peut avoir pour une meuf...mais cet amour doit beaucoup plus profond que ce qu'on pourrait croire aujourd'hui DÉDICACE a tout les AMOUREUX du monde. Paroles (wolof): BRAHSKO: Yeah hein hein lii...
Jeqiku ga amoon ca Faraas Jeqiku ga amoon ca Faraas, mooy jeqiku gi njëkk a am ci jamono ju bees jii, ci kaw nguuru ak jaay doole, ak doxale ni la neexe, doo diisoo, doo deglu xalaatu keneen. Moom nag (jeqiku googu), mi ngi ame woon ca Faraas, ca jamonoy buur ba tuddoon Luwis mu fukk ak juroom benneel ma, bokkoon ca nj...
Refrain Maa béég thi yaw anytime, guéstou guiss leu, nga kiss meu, Baby ya beuri fééémmm!!! Damaye tok di laye guiss thi samaye rhymez Nga djéki djéki call meu némaa faut que gnou fineee!! Fii ngaye guéné « mo noye » Fii ngaye guéné « mo noye » Fii ngaye guéné « mo noye » Fii ngaye guéné « mo noyeu noye » Verse 1 Eh ba...
baak Sauter à la navigation Sauter à la recherche Wolof[Soppi] → Mottalil gongikubaat bi. baak : - baak pot bu ñuul bi rootkat di dugal cib teen ngir tanq ndox, - ku yàgg ci teen baak fekk la fa Xool it[Soppi] Tekki[Soppi] → Mottalil tekkib baat bi ci yeneen làkk. Déglu baatu baak ci wolofi Senegaal
Jàngoroy Ebola Jàngoroy Ebola ñu gënoon koo xamee ci Jàngoroy yaram-wu-tàng ju Ebola jenn xeetu jangoro la juy dal nit walla yenn bàyyima yi te doomu-jàngoro bu ebola di ko joxe. Xàmmeekaayu jangoro ji mi ngi tàmbalee feeñ ci diggante ñaari fan ba ñetti ayubés ginnaaw bi la doomu-jàngoro bi duggee, ngay ame yaram-wu-tà...
Ron Ron walla sibi ca saalum, xeet la ci xeeti garab yu njool yiy gudd ne sóll ca kaw. Mu bari lool ci tund Afrig, Eccopi, Afrig bëj-saalum. Dees na ko fekk ba tay ci digg Afrig, fu ci mel ni Saara, walla Namibi. Melo wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Ron garab gog guddaayam danay àgg ba 25 ba 30i met. Yaatuwaayam nag d...
Soobaan Soobaan di Sapindus saponaria garab la gu am xob yu xaw a tal, yor taxawaay bu yam rëyul ndawul. Ma nga fekk baax ca Amarig. Xeetu turam wii di Sapindus nag, mi ngi jóge ci latin di tekki saabub endo. Melo wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Garab gu yamamaay la guddaayam war a àgg ci 10i met. Ay xobam di xob yu s...
Nooon degloul pa bi ak toubab tu mouy lak si mbour tv Publié 18 février 2018 Autres Vidéos ho ken du mandela degloul li mou def ba mouy geuneu aduna …Macky degloul Yawmi soxla li mouy déf dégloul AWA KONTE773964894 Noon ki dou toubab kholal ni mouy def te dakh ko sénégalais yi toubab bi doye na waar lou mouy def marse ...
Karasol Karasol garab la gu bàyyikoo ci lu bir ci àll yu naaje yu Karayib, yu Amerig gu digg ak gu bëjsaalum. Melo wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Karasol gàncax la gu ndaw. Guddaayam danay àgg 3 ba 10i met. Xobam melo wu nëtëx la yor. Tóor-tóoram 3i xob la yor. Day meññ at mépp. Njariñ yi[Soppi • soppi gongikuwaay bi...
Xët wu njëkk Ci mbetteel Ci wetu Dugg Jekkal Ci mbiri Wikipedia Ay aartu Ubbi njël lu njëkk li Seet Ronald Reagan Jàng ci weneen làkk Topp xët wii Soppi Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal Reagan 1981 Ronald Wilson Reagan (1911-2004): njii...
Ab TekkiFaramface (DefinedMeaning ) mooy booloo bu ab Waxin ak ab Tekki ; ab waxin du lenn lu dul ay baat yu ñu boole ñeel ab làkk, mu am lu muy xamle; te ab Tekki mooy faramface gi, ci benn walla ay baat, gu waxin gi. Ab TekkiFaramface (maanaam tekki gu ñu faramface) ab limuwaay la ci database bu OmegaWiki. Ngir naal ...
Senaso srl dafay yengu ci wallum firi ci kalamay Italien/Wolof (wala wolof/italien) ci fann yu bari ak anam yu wor te wër ci njëg bu yomb bo ko mengele ak yebeefu mbiru marse. Lolu mën na nekk ndax Lekalo biñu lekalo ak firikat yu xarañ te namp kalama wolof bi te seen mën mën ak seen jaar jaar mo leen ko may. Doxalinu ...
Yëglu cig sori Mooy xam ni yaram yi mel walla jëmm yi, walla seen dëgg-dëgg ci lu dul laalante gu fisya (fisi) walla gu kimya (simi) gu jonjoo ak yaram yii. Bokk na ci ni nu ko gënee doxale, ëpp ko nee defe ci jamono jii: nataali jawwu yi nuy defe ci satalit yi (jumi asamaan yi) walla ci fafalnaaw yi. Bokk na ci li nuy...
Mollah Morgun : louma nakari neexouma/ (j’aime pas )beugouma/ di guiss boy rappeurs you rerr si seni guintt /di feintt/ dundu boudoul sén boss /guissouniou lenn loudoul alalou adouna djiné/djiguén ak taar/sen birr /yi di dioy niouy diay boss/Goss you gnimeewoul responsabiliser sén bop si wax li town bi di rirr thi tarr...
LIMAMETTI.COM - Sama Taarikh bi Marianne laako doupe\r\nMarianne demna ta dotou nieuw\r\nDjiguene dja dekewoone kaf tadou mer\r\nWoutaloone boopame aw tour bacii nieneene\r\nMarianne demna ta dotou nieuw\r\nTaille fine mouni boopame nieneene mouni Adji Ndawa\r\nMouye stress, ak lamou lamboole, Marie khamoul loumaye amb...
Bismil Laahir Rahiimir Rahiimi. Was salaatu was salaamu halaa man laa nabiyya bahdah. Ñu fas yéeney dollee deŋkënte ak di dollee fàtleente. Ñiŋ koy jëmële nak ci tomb binga xamne mbooleem liy yiwu àdduna ak yiwu àllaaxira ci lako sunu BOROOM subhaanahu wa tahaalaa dëxëñ. Mbooleem yonant yimu yónni yépp ci la leen digël...
Seydi Rohu Laay kula woy Bismi Laahi Rahmaani Rahiim - Bismi Laahi may bëgg woy Seydina Limaamu te woy Rohou Lâhi ndax kuka woy am ngërëm fi jannati - Deglu leen ma yeen ñi nélaw ci jamaana wax fi ñu aw Ba gëlëmté reer nanu faw bi imaami rahmati - Waaja sééntu mahdyu moom té gisoon mandarga ya xam La mu janga woor ka n...
Ubbi njël lu njëkk li Xët wu njëkk Ci mbetteel Ci wetu Dugg Jekkal Ci mbiri Wikipedia Ay aartu Seet Lonkoyoon Jàng ci weneen làkk Topp Soppi Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal Lonkoyoon Ci séwógaraafi lañ ëpp ci li ñu koy jëfandikoo. Dañ ...
Marsiya Baay Raan 1. Al hamdu lil laahi nan gëm nangu ay dogalam Si Moom lanuy dello moo moom jaamñi ak luñu am 2. Innaa lil laahi wa innaa raaji’uuna ilay- hi Yalla mooy joxe mooy jël noo ngi nangu jëfëm 3. Dunyaabi workat la moo woor Sayyidul-umami Moo wor Sahaabayi waajii Àddunaako xajam 4. Wal mawtu baabun wa kulun...
- Senegaal nom - Senegal - Senegaal nom - Senegal - Senegaal phrase - Senegal Wolof Word of the Day: Register free Latest: Allah Amerik Asi Benee Burkina Faso Italiya Kamerun Kongo Poloñ Pël Senegaal Simababuwe Somali aar ab afrikee aligatoor alluwa kër am amal amiin antilop arabi area armiñon armiñoo arsenik asambalé ...
- Ku Lu baax tee def Lu baax Lépp ay bokk baax. - Bu dara yàq dara. - Lu la rombuy di bajantu Leegi mu romb lay soox - Defar bayyi fi daf maa gënal yàq bàyyi fi . - Fuma ñaan ne soxna ñu ne ma toogal déglu ma daa ñu ma déggaat waaye feneen lay doon - Lu ñu la ne nékku fa nég ko fa. - Wanewu daa nuróo ak wanu moo tax ma...
SÉEX TIIJAAN JÉEY (Xeltukat/Enda-Cacid) Fan yii, coowal ECO baa ngi mel ni tànnbéeru dëmm, rëb ba nga ne lii lum doon. Bi Emmanuel Macron ak Alassane Ouattara defee seen yégle bi ba léegi, ku nekk a ngi àddu ci mbir mi. Jàppal ECO fii, bàyyil ECO fee. Muy taskati xibaar yi, politiseŋ yi (rawati-na kujje yi), way-moomee...
Fàttaliku lu war jaam la, kon na xel dellu ci ginnaaw ngir saytu walla jéex démbu Senegale yi njëkk a agsi Milan. Démb a jur tey te Wolof Njaay dinay wax ne : “Ku la njëkk ci jàkka, bu dee jullee ka fa yóbbu, moo la ëpp i ràkka.” Dégg ngeen tamit ñu naan lu Wolof léebu dëgg la. Kon duñu def lu-dul jéem a tarxiis, sóobu...